Injiilu Xale yi

Xew xew yu gëna neex yu jogge ci biir Injiil bi. Té ñu koy mayé.

Lu waral ñuy def lii

Macë 19:14 Yeesu né, 'Bàyyileen xale yi, te buleen léen tere, ñu ñëw ci man. Ndaxte ñu mel ni ñoom, ñoo yelloo nguuru Yàlla Aji Kawe ji.'

Injiilu xale yi dafa nekk ngir xale yi xam kuy Yeesu Krista lii moo waral ñuy wasaaré ay xew xew yu ñu nettali ci biir Injiil bi ak yeené ni materiel yu mingoog lii ci ay fann ak media yu wuuté ci internet bi, ci téléfon yi, ci ay trak yu ñuy imprimé ci kulër ak ci ay teeré yu ñu koloré, ci bepp laak bu xale mëna laak.

Mbiir yu ñu nettali ci biir Injiil bii dañu leena waara may 1.8 milliaru xalé yi nekk ci biir adduna bi sa su mëné nekk.

Boo leen bëggé bokk ci ñuy jot ci xeebar yi bindu leen

Receive