Injiilu xale yi dafa nekk ngir xale yi xam kuy Yeesu Krista lii moo waral ñuy wasaaré ay xew xew yu ñu nettali ci biir Injiil bi ak yeené ni materiel yu mingoog lii ci ay fann ak media yu wuuté ci internet bi, ci téléfon yi, ci ay trak yu ñuy imprimé ci kulër ak ci ay teeré yu ñu koloré, ci bepp laak bu xale mëna laak.
Mbiir yu ñu nettali ci biir Injiil bii dañu leena waara may 1.8 milliaru xalé yi nekk ci biir adduna bi sa su mëné nekk.